02/04/2026
Bonsoir Madame, Monsieur,
Venez réserver votre place pour notre Masterclass
exceptionnelle {
Le ticket est fixé à 15 000 FCFA.
Une masterclass riche en connaissances, en apprentissages et en opportunités vous attend.
Ne manquez pas cette occasion unique de vous former et d'élargir vos compétences.
Réservez dès maintenant votre place !
Naka nga def Madame, Monsieur,
Nëwleen ngir rezervé seen place ci sunu Masterclass bu
am solo
Ticket bi mooy 15 000 FCFA.
Masterclass bii dafay jox xam-xam, jang ak ay yoonu yokk seen kàttan.
Bu leen ñàkk okkazion bii bu baax ngir jàng ak gën a xam
Rezervéel seen place léegi!