Domou Mbour Saly

Domou Mbour Saly Informations de contact, plan et itinéraire, formulaire de contact, heures d'ouverture, services, évaluations, photos, vidéos et annonces de Domou Mbour Saly, Shopping et vente au détail, Toulouse.

« Ci fan yii di ñëw dees na gaaral Asàmbale bi sémbu yoonal wu jëm ci jëlee fi AMINISTI bi »DPG Ousmane SONKO« Dali sóob...
27/12/2024

« Ci fan yii di ñëw dees na gaaral Asàmbale bi sémbu yoonal wu jëm ci jëlee fi AMINISTI bi »

DPG Ousmane SONKO
« Dali sóobare (base militaire) biti réew yi nekk ci Senegaal yépp « Li am solo nekkul ci ñaata milyaar lañu depaase, waaye lan lañu njariñ ci réew mi. »

DPG Ousmane SONKOdees na leen fi jëlee ».

DPG Ousmane SONKO

« Càmbaraat nanu mbooleem kontraa yi ñu jot a amal ci pàcc yu am solo yi ci réew mi. »

DPG Ousmane SONKO
« Dees na delloosiwaat galag (taxe) yi ñu teggi woon ci woote yiy bawoo biti réew (appel entrant) ca 2012 ».

DPG Ousmane SONKO
« Galag yi (impôts) dees na ko néewal ngir fexe woyof boole ko ak daj ci ñépp. »

DPG Ousmane SONKO
« Senegaal dina dakkal mbooleem déggoo yi dox diggam ak paradi fiskaal yi teg ci waxtaanewaat yi jaarul yoon ak réew yi seen fiskaalite tegu ci yoon. »
DPG Ousmane SONKO
« Dinanu tàmbalee laaj wiisaa doxandeem yi nga xam ne seen i réew dañuy laaj wiisaa sunu doomi réew »

DPG Ousmane SONKO
« Bëggatunoo am réew moo xam ne, ñenn rekk ay ngardàjoo njariñ ya. »

DPG Ousmane SONKO
« Dees na yeesal Daara yi bu wér dugal leen ci doxaliinu njàng mi. »

DPG Ousmane SONKO

3 informations importantes:Le vendredi à 10h, le PM Ousmane Sonko fera sa déclaration de politique générale (DPG).Le sam...
26/12/2024

3 informations importantes:
Le vendredi à 10h, le PM Ousmane Sonko fera sa déclaration de politique générale (DPG).
Le samedi 28, le PM Ousmane Sonko reviendra à l’assemblée nationale pour engager la responsabilité du Gouvernement sur le vote du projet de la loi de finances au titre de l’art 86 al.6 de la constitution.
Cette procédure permettra d’adopter le projet de loi finances sans débat avant la fin de l’année.
Après le vote, l’Assemblée nationale installera la haute cour de justice et ses 8 membres et 8 suppléants.

”Ces (les conducteurs de motos +Jakarta+) avaient organisé lundi une manifestation improvisée sans autorisation, ni décl...
23/04/2024

”Ces (les conducteurs de motos +Jakarta+) avaient organisé lundi une manifestation improvisée sans autorisation, ni déclaration, pour dénoncer des tracasseries policières à leur encontre”, a expliqué la même source.

Elle ajoute que ces conducteurs ”ont essayé de bloquer la circulation dans quelques artères de la ville, en y érigeant des barricades et en brûlant des pneus”.

La police est intervenue et a interpelé 13 d’entre eux qui sont ”en garde à vue au commissariat de Saly”.
Treize conducteurs de motos +Jakarta+ ont été arrêtés et placés en garde à vue au commissariat urbain de Saly Portudal (Mbour-ouest) pour organisation d’une manifestation publique ”improvisée et non autorisée”, a appris l’APS de source sécuritaire.
👇🏿

21/03/2024

Coalition Diomaye président tay yëgël Mbour ak Saly ✅🥳

11/02/2024

Se message

11/02/2024

Ousmane SONKO

11/02/2024

Xanaa ku waxul ci politig sax mana ñaawlu ba ñépp dégg ko ray giñuy ray doomi réew mi.

   Jëli leen Seen carte yi ✅
26/01/2024


Jëli leen Seen carte yi ✅

🔴CDC : Cheikh Issa Sall remplace Mame Boye DiaoLa Caisse des dépôts et consignations a un nouveau Directeur général. Le ...
13/09/2023

🔴CDC : Cheikh Issa Sall remplace Mame Boye Diao

La Caisse des dépôts et consignations a un nouveau Directeur général.

Le chef de l'Etat vient de nommer Cheikh Issa Sall, maire de la commune de Mbour, Directeur général de la Caisse des dépôts et consignations (CDC).

Cheikh Issa Sall occupait auparavant le poste de Directeur Général de l'Agence de Développement Municipal. L'information a filtré du conseil des ministres de ce mercredi 13 septembre 2023.

Cheikh Issa Sall remplace à ce poste Mame Boye Diao limogé par le président Macky Sall, après qu'il a annoncé sa candidature à la présidentielle de 2024 et claqué la porte du parti au pouvoir, l'APR.

Dernière Minute Infos

Adresse

Toulouse

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Domou Mbour Saly publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Partager