Ci XASSIDA yi rekk

Ci XASSIDA yi rekk Karaamatii xatu yadii
كَرَامَتِي خَطُّ يَدِي

Tay ci Àjjuma gi mooy juroom benni fan  (06) ci weeru Rakki Gàmmu (Rabiihus saanii ) 1448H dëppoo ak 18 Septembre 2026  ...
18/09/2026

Tay ci Àjjuma gi mooy juroom benni fan (06) ci weeru Rakki Gàmmu (Rabiihus saanii ) 1448H dëppoo ak 18 Septembre 2026

Yalna Yàlla defal ñépp jàmm

Tay ci Alxamis gi mooy juroomi fan  (05) ci weeru Rakki Gàmmu (Rabiihus saanii ) 1448H dëppoo ak 17 Septembre 2026      ...
17/09/2026

Tay ci Alxamis gi mooy juroomi fan (05) ci weeru Rakki Gàmmu (Rabiihus saanii ) 1448H dëppoo ak 17 Septembre 2026

Yalna Yàlla defal ñépp jàmm

Tay ci Alarba ji mooy ñenti fan  (04) ci weeru Rakki Gàmmu (Rabiihus saanii ) 1448H dëppoo ak 16 Septembre 2026         ...
16/09/2026

Tay ci Alarba ji mooy ñenti fan (04) ci weeru Rakki Gàmmu (Rabiihus saanii ) 1448H dëppoo ak 16 Septembre 2026

Yalna Yàlla defal ñépp jàmm

Tay ci Talaata ji mooy ñetti fan  (03) ci weeru Rakki Gàmmu (Rabiihus saanii ) 1448H dëppoo ak 15 Septembre 2026        ...
15/09/2026

Tay ci Talaata ji mooy ñetti fan (03) ci weeru Rakki Gàmmu (Rabiihus saanii ) 1448H dëppoo ak 15 Septembre 2026

Yalna Yàlla defal ñépp jàmm

Tay ci Altine ji mooy ñaari fan  (02) ci weeru Rakki Gàmmu (Rabiihus saanii ) 1448H dëppoo ak 14 Septembre 2026         ...
14/09/2026

Tay ci Altine ji mooy ñaari fan (02) ci weeru Rakki Gàmmu (Rabiihus saanii ) 1448H dëppoo ak 14 Septembre 2026

Yalna Yàlla defal ñépp jàmm

Tay ci Dibeer ji mooy benn fan  (01) ci weeru Rakki Gàmmu (Rabiihus saanii ) 1448H dëppoo ak 13 Septembre 2026          ...
13/09/2026

Tay ci Dibeer ji mooy benn fan (01) ci weeru Rakki Gàmmu (Rabiihus saanii ) 1448H dëppoo ak 13 Septembre 2026

Yalna Yàlla defal ñépp jàmm

12/09/2026

Weer wi 🌙 feeñ na suba ci Dibéer gi mooy benn panub Rakki Gàmmu (Rabiihus saanii) 1448H

Séentu weeru Rakki Gàmmu 1448H_____________Assalaamu halaykum wa Rahmatullaah.Mbooloo mi Sëriñ bi dénk wàllum séentu wee...
12/09/2026

Séentu weeru Rakki Gàmmu 1448H
_____________
Assalaamu halaykum wa Rahmatullaah.
Mbooloo mi Sëriñ bi dénk wàllum séentu weer wi ci Tuubaa ñooy xamal ñépp ne tay jii ci Gaawu bi, 29eelu fani Gàmmu (Rabiihul Awwal) 1448H, dëppoo ak le 12 Septembre 2026, dinañu daje ci Jumaay Tuubaa ju mag ji ngir séentu weeru Rakki Gàmmu (Rabiihus saanii ) 1448H.
————
Mbooloo mi yore wàllum séentu weer wi ci Tuubaa.

Tay ci Gaawu ji mooy ñaar fukki fan ak juroom ñent (29) ci weeru Gàmmu (Rabiihul Awwal) 1448H dëppoo ak 12 Septembre 202...
12/09/2026

Tay ci Gaawu ji mooy ñaar fukki fan ak juroom ñent (29) ci weeru Gàmmu (Rabiihul Awwal) 1448H dëppoo ak 12 Septembre 2026

Yalna Yàlla defal ñépp jàmm

Tay ci Àjjuma gi mooy ñaar fukki fan ak juroom ñett (28) ci weeru Gàmmu (Rabiihul Awwal) 1448H dëppoo ak 11 Septembre 20...
11/09/2026

Tay ci Àjjuma gi mooy ñaar fukki fan ak juroom ñett (28) ci weeru Gàmmu (Rabiihul Awwal) 1448H dëppoo ak 11 Septembre 2026

Yalna Yàlla defal ñépp jàmm

Adresse

Louga

Téléphone

+221764914958

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Ci XASSIDA yi rekk publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Raccourcis

Partager